Advertisement

ADIOUZA - FANS YI (CLIP OFFICIEL)

ADIOUZA - FANS YI (CLIP OFFICIEL) Adiouza rend hommage à tous ses fans qui la soutiennent depuis 10 ans !

Fans Yi (Lyrics)
Mane beguer nallene
Eh beguer nallene
Fans yi namonalene
namonalene

Couplet
10 ans déjà
yone wi metina
Cey yi le soper
Bayiwougnouma

Yageuna beug deff weuye wi
Waxlene fima tolou thi yene
Loune nguene di dathieu
Nguir Mane
Te Mane yeknako
Xex souba Ngone yeknako
Lou Len meti yeknako

Mane Sama xel sama xol langui Thi yene
Taye ma sargalene yene fans yi

Refrain
Mane beguer nallene
Eh beguer nallene
Fans yi namonalene
namonalene

Solo
Ligueye bo Thi donner
Djiguene
Faut k nga xamner
Foula moye Li geune
Yen saye nite guisse la télé xemem la tok di dioye
Weur la wolou la nga gneuw bo noyer bop dioye

Kaye ma xamalene touti
Fans yenou yeukati

Ani Wa pikine
Parcel
Thiaroye
Yarax
Guediawaye
Rio
Keur Massar médina
Ziguinchor ba ndar beguer nagne ma waye
Mauritanie ba gambie beguer Baguer nagne ma waye
Jappeu nguene tewa bayi, douma xadi waye.

Refrain
Mane beguer nallene
Eh beguer nallene
Fans yi namonalene
namonalene

Pont
Taye ma weuyale lene
Yena ma japaler
Taye ma xamalene
Yena ma dolele.


Tiaba, Diarra Nancy, Bigue, Maimouna awa toure, wolma mame Diongue loxo thia kaw
Leggo leggo

Solo
Weuye Lene ma ndeyssane sama mak ji
Ana Sagna chéri sadia
Wolma lamine fall ak fatou thiam
Begoulo ma mère dale Yaw
Domi ndey Mami diouf

Souma demer baye beugeu xadi chéri Aziz ndiaye dolele ma
Souma demer baye beuger xadi
Khady koundoule dolel ma

Tassou
Sa goune sa goune

Solo
Dioudou Bou reye ndey ak baye
Foulak fayda borome dale
Mareme chalar mimaye beugeu jigne
Aida Seye chéri lamine la bokale baye
Fou sama rangogne touro
Mareme fompale ngamako
Raki gamou seye
Diarama mareme
Weye lele weuyelelene ma mareme

Souma demer baye beugeu xady
Chéri doudou dolelma
Souma demer baye beugeu xady
Fat kine dolelma

Dj boubs, pape cheikh, cheix Sar Sidathe gnoma terrer chômer
Abba , Koutia, alima Maria gnoma tere chômer
Dieynaba, Nadia,, haini, maty, kebs thiam leggo leggo.

REMERCIEMENTS:
L'équipe de gladiateurs qui m'a accompagnée dans la réalisation de mon album. il s’agit de MON FRÈRE Cheikh Ouza, Moussa Ngom, Yeye faye, Iso on the beat, CT, Baxaw, Xuman, king Kruh lyrics, Bril, wanted, Pac D, Max Ngassa, wylliam, l’hôtel Radisson, Hertz, Novotel, Thinmas. Je remercie tout le staff, tous les membres de Adiouza family, ma famille, mes amies. Sans vous, il me serait difficile d’y arriver.
Mention spéciale à mon père et ma mère pour votre soutien.

Abonnez-vous ici :



Retrouvez Adiouza Diallo sur :



- Instagram:

- Twitter :

- Facebook:

Pour booking:
- A l’international: +33 6 77 73 16 73
- Au Sénégal: +221774892177 / +221 773222305

#Adiouza2020 #AdiouzaFansYi #AdiouzaFamily #SaGoune

nouveau clip adiouza,fans yi,clip adiouza diallo,sa goune sa goune,xaley fethial ma khol,clip senegal 2020,musique senegal,nouveautés senegalaises,do dara,viviane chidid,deranger,ambiance,tik tok senegal,defsi code,meilleurs clips mbalakh 2020,saint valentin,dakar,14 février,chibi ribi,jahman x press,pod et marichou saison 4,pape cheikh,dj boubs,abba,kouthia,boubacar diallo,cheikh sarr,alima,videos senegalaises 2020,Sa goune sa goune,

Post a Comment

0 Comments